jeudi 30 septembre 2021

Analyse sur la situation en Guinée

      Alpha Condé entouré par les putschistes

Arrivé au pouvoir en 2010 après 40 ans d’opposition, le président Alpha Condé semblait être l’homme providentiel de la Guinée. Son charisme et son expérience pointu lui conféraient une légitimité unanime auprès des guinéens pour sortir le pays du sous-développement et des décennies d’autoritarisme. Cependant, 11 ans après, l’avenir « radieux » que le « Mandela » guinéen avait promis, s’est transformé à un cauchemar. Un cauchemar qui pousse les militaires a s'emparer du pouvoir. Analyse !








Mbënd mi ci Senegaal: jàngoro ju jafee faj


At bu jot yénn gox yi ci réewu Senegaal mbënd mi da leen di sonal. Samp nanu laaj jëmale ci li waral lini mel.

Saa su nawet jotee yenn gox ci réewu Senegaal, mbënd mi daf leen di sonal. Ŋacc ndox, xuus ci taa- taa yi mooy doon jafe-jafe yi ñu bari di jànkoonteel. Lii waral li ni mel mooy nguur gu sàggan, dëkk ci luubël ak a dugël alali réew mi fi mu warul duggu. Nguur gi ñu muur ay gëtam, nguur gu nanguwul gis mbëbëtu askan wi. Kuy këpp kees sa  sune doo tal defar dëkkuwaay nit ñi. Moo ni dey li defar bërëbu dëkku kaay yi lu yomb la, nekkul dara ludul gas ay tiwo biir suuf ngir ñu sànni ndoxu taw bi biir géej. 
Bëgg teg lépp ci ndoddu nguur gi day doon njuumte, askan wi am nañu ci séen wàll bu baax. Kenn demul ñu des. Ñépp mënu ñoo dëkk biir Ndakaaru. Ku dem ba xamatoo foo jëm da ngay dellu fi nga juge. Bula mbënd mi sonalee da ngay dellu dëkk ba fi nga xam ni du taa. 
Beneen bi mooy ñi ñëw ba ci yoonu ndox di fa jënd kër. Kooku bu la mbënd mi sonalee am nga ci wàll wu rëy. 
Ci gàttal na ku nekk xam li ko war mu def ko ngir mbënd mi nekk li ñuy fàttaliku ci at yi ñu jëm.

Analyse sur la situation en Guinée

      Alpha Condé entouré par les putschistes Arrivé au pouvoir en 2010 après 40 ans d’opposition, le président Alpha Condé semb...